Browsing Wolof translation

Don't show this notice anymore
Before translating, be sure to go through Ubuntu Translators instructions and Wolof guidelines.
110 of 1267 results
1.
Ubuntu installer main menu
Type: text
Description
:sl1:
Menu bu mag bu porogaraam u istalaasioŋ bu Ubuntu bi
Translated and reviewed by Mouhamadou Mamoune Mbacke
Shared:
Njël lu njëkk ci campu Ubuntu
Suggested by ibrahima fall
Located in ../main-menu.templates:1001
2.
Choose the next step in the install process:
Type: select
Description
:sl1:
Tannal etaap bu istalaasioŋ bi ci tege:
Translated and reviewed by Mouhamadou Mamoune Mbacke
Shared:
Tànnal jéego biy toftal ci camp gi:
Suggested by ibrahima fall
Located in ../main-menu.templates:2001
3.
This is the main menu for the Ubuntu installer.
Type: select
Description
Bii mooy menu bu mag bu Ubuntu installer.
Translated and reviewed by Mouhamadou Mamoune Mbacke
Located in ../main-menu.templates:9
4.
Installation step failed
Type: error
Description
:sl2:
Etaap bu istalaasioŋ bi antuwul
Translated and reviewed by Mouhamadou Mamoune Mbacke
Shared:
Jéegob camp bi antuwul
Suggested by ibrahima fall
Located in ../main-menu.templates:3001
5.
An installation step failed. You can try to run the failing item again from the menu, or skip it and choose something else. The failing step is: ${ITEM}
Type: error
Description
:sl2:
Amna ab etaap bu istalaasioŋ bu antuwul. Man ngaa jéema demaat ca menu ba defaat etaap bu istalaasiŋ bi antuwul, walla nga tëbko tann baneen. Etaap bi antuwul moodi: ${ITEM}
Translated and reviewed by Mouhamadou Mamoune Mbacke
Shared:
Am na ab jéego ci camp gi bu antuwul. Man ngaa jéem a defaat jéego bi soo delloo ca njël la, walla nga tëb ko tànn beneen. Jéego bi antuwul mooy: ${ITEM}
Suggested by ibrahima fall
Located in ../main-menu.templates:3001
6.
Choose an installation step:
Type: select
Description
:sl2:
Tannal ab etaap bu istalaasioŋ:
Translated and reviewed by Mouhamadou Mamoune Mbacke
Shared:
Tànnal ab jéegob camp:
Suggested by ibrahima fall
Located in ../main-menu.templates:4001
7.
This installation step depends on one or more other steps that have not yet been performed.
Type: select
Description
:sl2:
Jéego bu istalaasioŋ bii dafa sukkandiku ci baneen walla yaneen etaap yu ñu defagul ba leegi.
Translated and reviewed by Mouhamadou Mamoune Mbacke
Shared:
Jéegob camp bii dafa sukkandiku ci beneen walla yaneen jéego yees defagul ba leegi.
Suggested by ibrahima fall
Located in ../main-menu.templates:4001
8.
critical, high, medium, low
Type: select
Choices
bu garaaw, bu kawe, bu diggdóomu, bu suufe
Translated and reviewed by Mouhamadou Mamoune Mbacke
Located in ../cdebconf-udeb.templates:3
9.
Ignore questions with a priority less than...
Type: select
Description
Jéllaléel laaj yi am piriyorite bu yées...
Translated and reviewed by Mouhamadou Mamoune Mbacke
Located in ../cdebconf-udeb.templates:5
10.
Packages that use debconf for configuration prioritize the questions they might ask you. Only questions with a certain priority or higher are actually shown to you; all less important questions are skipped.
Type: select
Description
:sl2:
Paket yiy jëfandikoo debconf ci séen komfiguraasioŋ, laaj yi ñu lay laaj benn bu ne da fay am ap piriorite. Laaj yi ame yenn piriorite rekk walla yi leen kawe la ñu lay wan. Laaj yi gëna néew solo yéppu da ñu léen di tëp.
Translated and reviewed by Mouhamadou Mamoune Mbacke
Located in ../cdebconf-udeb.templates:2002
110 of 1267 results

This translation is managed by Ubuntu Wolof Translators, assigned by Ubuntu Translators.

You are not logged in. Please log in to work on translations.

Contributors to this translation: Alexandre_Mbaye, Mouhamadou Mamoune Mbacke, Saer Kamara, camara, ibou, ibrahima fall.