Translations by Mouhamadou Mamoune Mbacke

Mouhamadou Mamoune Mbacke has submitted the following strings to this translation. Contributions are visually coded: currently used translations, unreviewed suggestions, rejected suggestions.

51100 of 1462 results
30.
Go back to previous question
2006-03-17
Delluwaat ca laaj bi weesu
31.
Select an empty entry
2006-03-17
Tannal ab aantre bu féex
2006-03-17
Tannal ab aantre bu féex
2006-03-17
Tannal ab aantre bu féex
2006-03-17
Tannal ab aantre bu féex
32.
Prompt: '%c' for help, default=%d>
2006-03-17
Woote: '%c' ngir am ndimbal,defóo=%d>
2006-03-17
Woote: '%c' ngir am ndimbal,defóo=%d>
2006-03-17
Woote: '%c' ngir am ndimbal,defóo=%d>
2006-03-17
Woote: '%c' ngir am ndimbal,defóo=%d>
33.
Prompt: '%c' for help>
2006-03-17
Woote: '%c' ngir am ndimbal>
34.
Prompt: '%c' for help, default=%s>
2006-03-17
Woote: '%c' ngir am ndimbal, defóo=%s>
35.
[Press enter to continue]
2006-03-17
[Bësël enter ngir jall]
36.
Interactive shell
2006-03-17
Shell bu interaktiif
37.
After this message, you will be running "ash", a Bourne-shell clone.
2006-03-17
Gannaaw bii bataaxal, yaa ngi nara doxal "ash", ab koloon bu Bourne-shell.
2006-03-17
Gannaaw bii bataaxal, yaa ngi nara doxal "ash", ab koloon bu Bourne-shell.
2006-03-17
Gannaaw bii bataaxal, yaa ngi nara doxal "ash", ab koloon bu Bourne-shell.
2006-03-17
Gannaaw bii bataaxal, yaa ngi nara doxal "ash", ab koloon bu Bourne-shell.
38.
The root file system is a RAM disk. The hard disk file systems are mounted on "/target". The editor available to you is nano. It's very small and easy to figure out. To get an idea of what Unix utilities are available to you, use the "help" command.
2006-03-17
Sistem u fiise root ab disk u RAM la. Sistem u fiise bu disk budëgër bi ñi ngi leen monte ci "/target". Editóor bi nga mana am mooy nano. Dafa tuuti lool Ta yumba xam. Ngir nga mana xama dara ci jumtukaay yu Unix yi nga mana am, da ngay jëfandikoo komaande "help".
39.
Use the "exit" command to return to the installation menu.
2006-03-17
Jëfandikool komaande "exit" ngir dello ci menu bu istalaasiŋ ba.
40.
Execute a shell
2006-03-17
Doxal ab shell
42.
Are you sure you want to exit now?
2006-03-17
Ndax wóorna la ne bëgg ngaa génn leegi?
43.
If you have not finished the install, your system may be left in an unusable state.
2006-03-17
Bu fukkee jeexala goo istalaasioŋ bi, amaana sa sistem nekk ci ab etaa bu ko kenn dul mana jëfandikoo.
44.
Abort the installation
2006-03-17
Bayyi istalaasioŋ bi
45.
Registering modules...
2006-03-17
Mi ngi aariste modil yi...
2006-03-17
Mi ngi aariste modil yi...
2006-03-17
Mi ngi aariste modil yi...
2006-03-17
Mi ngi aariste modil yi...
46.
Terminal plugin not available
2009-03-10
Plugin bu Terminl bi jappundiwul
47.
This build of the debian-installer requires the terminal plugin in order to display a shell. Unfortunately, this plugin is currently unavailable.
2009-03-10
Prograam bu istalaasioŋ bu Debian bii dafay soxla plugin bu terminal bi ngir man laa wan shell bi. Waaye plugin boobu fimune jappundiwul.
48.
It should be available after reaching the "Loading additional components" installation step.
2009-03-10
Dana wara jappundi ginnaaw jéegu bu istalaasioŋ bu "Mingi sëf yaneen komposaŋ".
49.
Alternatively, you can open a shell by pressing Ctrl+Alt+F2. Use Alt+F5 to get back to the installer.
2009-03-10
Teewul nak nga mana ubbi ab shell boo bësée Ctrl+Alt+F2. Nigir delluwaat ci prograamu istalaasioŋ bi bësël Alt+F5.
50.
Installer components to load:
2006-03-17
Kompóosaŋ yu installer yi niy sëf:
2006-03-17
Kompóosaŋ yu installer yi niy sëf:
2006-03-17
Kompóosaŋ yu installer yi niy sëf:
2006-03-17
Kompóosaŋ yu installer yi niy sëf:
51.
All components of the installer needed to complete the install will be loaded automatically and are not listed here. Some other (optional) installer components are shown below. They are probably not necessary, but may be interesting to some users.
2007-03-11
Mbooleem kompóosaŋ yu prograamu istalaasioŋ bi di soxla ngir matale istalaasioŋ bi, doonte joxewuñu fii seenub list yit, prograam bi danako sëfal boppam. Amna yaneen komposaŋ yu prograamu istalaasioŋ bi (yoo xamne kumu neex du leen tann) ñoom ñingi ñu joxe fii ci suuf. Amaan maneesna leena baña soxal, waaye yit ñenn ñi amaan ñu neex leen.
2007-03-11
Mbooleem kompóosaŋ yu prograamu istalaasioŋ bi di soxla ngir matale istalaasioŋ bi, doonte joxewuñu fii seenub list yit, prograam bi danako sëfal boppam. Amna yaneen komposaŋ yu prograamu istalaasioŋ bi (yoo xamne kumu neex du leen tann) ñoom ñingi ñu joxe fii ci suuf. Amaan maneesna leena baña soxal, waaye yit ñenn ñi amaan ñu neex leen.
2007-03-11
Mbooleem kompóosaŋ yu prograamu istalaasioŋ bi di soxla ngir matale istalaasioŋ bi, doonte joxewuñu fii seenub list yit, prograam bi danako sëfal boppam. Amna yaneen komposaŋ yu prograamu istalaasioŋ bi (yoo xamne kumu neex du leen tann) ñoom ñingi ñu joxe fii ci suuf. Amaan maneesna leena baña soxal, waaye yit ñenn ñi amaan ñu neex leen.
52.
Note that if you select a component that requires others, those components will also be loaded.
2006-03-17
Na nga xam ne boo tanne ab kompóosaŋ buy laaj yaneen, yooya kompóoaŋ yitam deesna leen sëf.
53.
To save memory, only components that are certainly needed for an install are selected by default. The other installer components are not all necessary for a basic install, but you may need some of them, especially certain kernel modules, so look through the list carefully and select the components you need.
2007-03-11
Ngir sakkanal memuwaar, kompóosaŋ yu prograam u istalaasioŋ yi manula ñakk rekk lañuy tann ci defóo. Yaneen kompóosañ yi man nañoo ñakk ci ab istalaasioŋ bu seempal. Waaye amaana nga soxla yenn ci ñoom, rawatina yenn ci modil yu kernel bi, moo tax xoolal bu baax ci list bi ta tann yi nga soxla.
2006-03-17
Ngir sakkanal memuwaar, kompóosaŋ yu porogaraam u istalaasioŋ yi manula ñakk rekk lañuy tann ci defóo. Yaneen kompóosañ yi man nañoo ñakk ci ab istalaasioŋ bu seempal. Waaye amaana nga soxla yenn ci ñoom, rawatina yenn ci modil yu kernel bi, moo tax xoolal bu baax ci list bi ta tann yi nga soxla.
54.
Loading additional components
2006-03-17
Mi ngi sëf yaneen kompoosaŋ
55.
Retrieving ${PACKAGE}
2006-03-17
Mi ngi jël ${PACKAGE}
56.
Configuring ${PACKAGE}
2008-10-10
Mi ngi komfigure ${PACKAGE}
57.
Failed to load installer component
2006-03-17
Sëf kompóosaŋ bi antuwul
58.
Loading ${PACKAGE} failed for unknown reasons. Aborting.
2006-03-17
Sëf ${PACKAGE} antuwul ngir sabab sunu xamul. Ñi ngiy bayyi.
59.
Continue the install without loading kernel modules?
2006-03-17
Ndax nu eggale istalaasioŋ bi ci ludul nuy sëf modil yu kernel bi?
60.
No kernel modules were found. This probably is due to a mismatch between the kernel used by this version of the installer and the kernel version available in the archive.
2006-03-17
Giseeful benn modil bu kernel. Amaana liko waral moodi ab ñakka déggóo la diggante kernel bi bii wersioŋ u installer di jëfandikoo and wersioŋ bu kernel bi ne ci arsiif bi.
61.
If you're installing from a mirror, you can work around this problem by choosing to install a different version of Ubuntu. The install will probably fail to work if you continue without kernel modules.
2006-03-17
Boo dee istalee ci ab seetu, man ngaa lijjanti porobaleem bi, da ngay tann baneen wersioŋ bu Ubuntu istaleko. Istalaasioŋ bi amaana du antu bu fekkee dangay aggale ci ludul modil yu kernel bi.
62.
Choose language
2006-03-17
Tannal aw lakk/Choose language