Translations by Mouhamadou Mamoune Mbacke

Mouhamadou Mamoune Mbacke has submitted the following strings to this translation. Contributions are visually coded: currently used translations, unreviewed suggestions, rejected suggestions.

150 of 1462 results
1.
Ubuntu installer main menu
2007-03-11
Menu bu mag bu prograamu istalaasioŋ bu Ubuntu
2006-03-17
Menu bu mag bu porogaraam u istalaasioŋ bu Ubuntu bi
2.
Choose the next step in the install process:
2008-02-20
Tannal etaap bu istalaasioŋ bi ci tege:
2006-03-17
Tannal etaap bu istalaasioŋ bi ci tege:
3.
Installation step failed
2008-02-20
Etaap bu istalaasioŋ bi antuwul
2006-03-17
Etaap bu istalaasioŋ bi antuwul
4.
An installation step failed. You can try to run the failing item again from the menu, or skip it and choose something else. The failing step is: ${ITEM}
2008-02-20
Amna ab etaap bu istalaasioŋ bu antuwul. Man ngaa jéema demaat ca menu ba defaat etaap bu istalaasiŋ bi antuwul, walla nga tëbko tann baneen. Etaap bi antuwul moodi: ${ITEM}
2006-03-17
Amna ab etaap bu istalaasioŋ bu antuwul. Man ngaa jéema demaat ca menu ba defaat etaap bu istalaasiŋ bi antuwul, walla nga tëbko tann baneen. Etaap bi antuwul moodi: ${ITEM}
5.
Choose an installation step:
2008-02-20
Tannal ab etaap bu istalaasioŋ:
2006-03-17
Tannal ab etaap bu istalaasioŋ:
6.
This installation step depends on one or more other steps that have not yet been performed.
2006-03-17
Jéego bu istalaasioŋ bii dafa sukkandiku ci baneen walla yaneen etaap yu ñu defagul ba leegi.
2006-03-17
Jéego bu istalaasioŋ bii dafa sukkandiku ci baneen walla yaneen etaap yu ñu defagul ba leegi.
7.
critical
2006-09-07
bu garaaw
8.
high
2006-09-07
bu kawe
9.
medium
2006-09-07
bu diggdóomu
10.
low
2008-02-20
bu suufe
11.
Ignore questions with a priority less than:
2007-03-11
Jéllaléel laaj yi am piriyorite bu yées:
12.
Packages that use debconf for configuration prioritize the questions they might ask you. Only questions with a certain priority or higher are actually shown to you; all less important questions are skipped.
2006-03-17
Paket yiy jëfandikoo debconf ci séen komfiguraasioŋ, laaj yi ñu lay laaj benn bu ne da fay am ap piriorite. Laaj yi ame yenn piriorite rekk walla yi leen kawe la ñu lay wan. Laaj yi gëna néew solo yéppu da ñu léen di tëp.
13.
You can select the lowest priority of question you want to see: - 'critical' is for items that will probably break the system without user intervention. - 'high' is for items that don't have reasonable defaults. - 'medium' is for normal items that have reasonable defaults. - 'low' is for trivial items that have defaults that will work in the vast majority of cases.
2006-03-17
Man ngaa tann laaj yi am piriyorite yi gëna suufe yi nga bëgg a giss: - 'bu garaaw' ñeel yëf yi nga xam ne man naa yax sistem bi ci ludul kikoy doxal di ci dugal loxoom. - 'bu kawe' ñeel yëf yi amul ay défóo yu xellu. - 'bu diggdóomu' ñeel yëf yu normaal yi ame ay défóo yu xellu. - 'bu suufe' ñeel yëf yu jappundi yi ame ay défóo yoo xam ne danañu dox ci li ci ëppu.
14.
For example, this question is of medium priority, and if your priority were already 'high' or 'critical', you wouldn't see this question.
2006-03-17
Ci misaal, bii laaj dafa am piriyorite bu diggdóomu, bu fekkoon nga defoon piriyorite 'bu kawe' walla 'bu garaaw', kon doo gis bii laaj.
2006-03-17
Ci misaal, bii laaj dafa am piriyorite bu diggdóomu, bu fekkoon nga defoon piriyorite 'bu kawe' walla 'bu garaaw', kon doo gis bii laaj.
2006-03-17
Ci misaal, bii laaj dafa am piriyorite bu diggdóomu, bu fekkoon nga defoon piriyorite 'bu kawe' walla 'bu garaaw', kon doo gis bii laaj.
2006-03-17
Ci misaal, bii laaj dafa am piriyorite bu diggdóomu, bu fekkoon nga defoon piriyorite 'bu kawe' walla 'bu garaaw', kon doo gis bii laaj.
15.
Change debconf priority
2006-03-17
Soppi piriyorite bu debconf
16.
Continue
2006-03-17
Kontine
2006-03-17
Kontine
2006-03-17
Kontine
2006-03-17
Kontine
17.
Go Back
2006-03-17
Delluwaat
2006-03-17
Delluwaat
2006-03-17
Delluwaat
2006-03-17
Delluwaat
18.
Yes
2006-03-17
Waaw
19.
No
2006-03-17
Déet
2006-03-17
Déet
2006-03-17
Déet
2006-03-17
Déet
20.
Cancel
2006-03-17
Neenal
24.
LTR
2006-03-17
LTR
25.
Screenshot
2006-03-17
Foto ekraaŋbi
26.
Screenshot saved as %s
2006-03-17
Foto ekraaŋbi dencnañuko ci turu %s
2006-03-17
Foto ekraaŋbi dencnañuko ci turu %s
2006-03-17
Foto ekraaŋbi dencnañuko ci turu %s
2006-03-17
Foto ekraaŋbi dencnañuko ci turu %s
27.
!! ERROR: %s
2006-03-17
!! NJUUMTE: %s
28.
KEYSTROKES:
2006-03-17
Butoŋ yu ñuy bës:
29.
Display this help message
2006-03-17
Wane bataaxal u ndimbal bii
2006-03-17
Wane bataaxal u ndimbal bii
2006-03-17
Wane bataaxal u ndimbal bii
2006-03-17
Wane bataaxal u ndimbal bii