Browsing Wolof translation

78 of 1729 results
78.
If you continue the installation in the selected language, dialogs should normally be displayed correctly but - especially if you use the more advanced options of the installer - there is a slight chance some may be displayed in English instead.
Type: text
Description
:sl1:
Boo eggqlee istalaasioŋ bi ci lakk wi nga tann, li ëppu ci wax yiñu lay bindal fii ci lakk wi nga tann lay wara doon, waaye nak su fekkee dangaa tann yenn istalaasioŋ yu xóot yi, amaana, doonte fooguñu ko lool sax, yenn ci yiñu lay bindal doon ci Aŋgale.
Translated by Mouhamadou Mamoune Mbacke
Located in ../localechooser.templates-in:18001
78 of 1729 results

This translation is managed by Ubuntu Wolof Translators, assigned by Ubuntu Translators.

You are not logged in. Please log in to work on translations.