Translations by camara

camara has submitted the following strings to this translation. Contributions are visually coded: currently used translations, unreviewed suggestions, rejected suggestions.

143 of 43 results
1.
Ubuntu installer main menu
2009-11-09
Njël bu jëkk ci sampum Ubuntu
2.
Choose the next step in the install process:
2009-11-09
Tànnal jégo biy toftal samp bi
3.
Installation step failed
2009-11-09
Bii jégo samp antuwul
4.
An installation step failed. You can try to run the failing item again from the menu, or skip it and choose something else. The failing step is: ${ITEM}
2009-11-09
Am na ab jégo ci samp bi bu antuwul. Man ngaa jémeu défaat jégo bi soo delloo ca njëlbén ba , walla nga tëb ko tànn beneen. Jégo bi antuwul mooy: ${ITEM}
5.
Choose an installation step:
2009-11-09
Tànnal ab jégo si samp:
6.
This installation step depends on one or more other steps that have not yet been performed.
2009-11-09
Bii Jégob samp dafa sukkandiku ci beneen walla yaneen jégo yu an togul
7.
critical
2009-11-09
bu doy-waar
9.
medium
2009-11-09
si digbi
11.
Ignore questions with a priority less than:
2009-11-09
Jéllalél laaj yi seen jampaay yées:
12.
Packages that use debconf for configuration prioritize the questions they might ask you. Only questions with a certain priority or higher are actually shown to you; all less important questions are skipped.
2009-11-09
Dank yiy jëfandikoo "debconf" ci seen kocc-koccal nu gi khol laaj yu am jampaay. Laaj yi ame jampaay walla yi leen sut rek lañu lay won. Laaj yu amul solo yi da leen di tëb.
13.
You can select the lowest priority of question you want to see: - 'critical' is for items that will probably break the system without user intervention. - 'high' is for items that don't have reasonable defaults. - 'medium' is for normal items that have reasonable defaults. - 'low' is for trivial items that have defaults that will work in the vast majority of cases.
2009-11-09
Man ngaa tann laaj yi séne jamppou waye suufe: - 'doy-waar' ñeel yëf yi man a yaq noste gi te jëfandikukat bi du ci duggal loxoom. - 'kawé' ñeel yëf yi amul ay yaqute yu xellu. - 'diggdóomu' ñeel yëf yu jaadu yi ame ay yaqute yu xellu. - 'suufe' ñeel yëf yu jappandi yi am ay yaqute te ñuy liggéey lu bari.
14.
For example, this question is of medium priority, and if your priority were already 'high' or 'critical', you wouldn't see this question.
2009-11-09
Ci misaal, bii laaj jampaayam dafa diggdóomu, te su fekkoon jampaayam dafa ' kawe' walla 'doy-waar' doonoo ko woon man a gis.
15.
Change debconf priority
2009-11-09
Soppi jampaayu "debconf"
16.
Continue
2009-11-09
Wéy
17.
Go Back
2009-11-09
Dellu ginnaaw
19.
No
2009-11-09
Deedeet
20.
Cancel
2009-11-09
Bayi
21.
<Tab> moves; <Space> selects; <Enter> activates buttons
2009-11-09
<Tab> rombu; <Space > tamde; <Enter> activates buttons
22.
<F1> for help; <Tab> moves; <Space> selects; <Enter> activates buttons
2009-11-09
<F1> Ndimbal; <Tab> rombeu; <Space> tamde; <Enter> activates buttons
2009-11-09
<F1> nimbal; <Tab> rombeu; <Space> tamde; <Enter> activates buttons
23.
Help
2009-11-09
Ndimbal
25.
Screenshot
2009-11-09
Natal
26.
Screenshot saved as %s
2009-11-09
Dencees na nataal bi %s
2009-11-09
Dencees na nataal bi
29.
Display this help message
2009-11-09
Wone bataaxalu ndimbal bii
31.
Select an empty entry
2009-11-09
Tànnal ab duggiit bu këmm
32.
Prompt: '%c' for help, default=%d>
2009-11-09
Woote: '%c' ngir ndimbal, yaqute=%d>
34.
Prompt: '%c' for help, default=%s>
2009-11-09
Woote: '%c' ngir am ndimbal, yaqute=%s>
36.
Interactive shell
2009-11-09
"Shell" buy jokkalantée
37.
After this message, you will be running "ash", a Bourne-shell clone.
2009-11-09
Gannaaw bii bataaxal, yaa ngi nar a doxal "ash", ab seex "Bourne-shell".
38.
The root file system is a RAM disk. The hard disk file systems are mounted on "/target". The editor available to you is nano. It's very small and easy to figure out. To get an idea of what Unix utilities are available to you, use the "help" command.
2009-11-09
Reenu dencukaayu noste bi tappaanub "RAM" la. Dencukaayu noste yu tappaan bu dëgër bi ci "/target" la sax. Soppikaay bi nga man a am mooy "nano". Dafa tuuti lool te yomb a xam. Ngir man a xam jumtukaayu "Unix" yi nga man a am, dangay jëfandikoo càkkutéef "help".
39.
Use the "exit" command to return to the installation menu.
2009-11-09
Jëfandikool càkkutéef "exit" ngir dellu ca njël ben samp bi.
40.
Execute a shell
2009-11-09
Ubbi ab "shell"
41.
Exit installer
2009-11-09
yamalée samp bi
42.
Are you sure you want to exit now?
2009-11-09
Wor na né bëgg ngaa yamaléé fi samp bi
43.
If you have not finished the install, your system may be left in an unusable state.
2009-11-09
Su fekkee jeexala go samp gi, noste gi man a jëfandiku.
44.
Abort the installation
2009-11-09
Dakkal samp gi
45.
Registering modules...
2009-11-09
Mii ngi denc...
46.
Terminal plugin not available
2009-11-09
Plugin bu "Terminal" bi jappundiwul
47.
This build of the debian-installer requires the terminal plugin in order to display a shell. Unfortunately, this plugin is currently unavailable.
2009-11-09
Sampkaayu Debian bii dafay soxla plugin bu terminal bi ngir man laa won shell bi. Waaye plugin boobu nii-nii jappundiwul.
48.
It should be available after reaching the "Loading additional components" installation step.
2009-11-09
Dana wara jappundi ginnaaw jéegu bu samp bi "Mingi sëf yaneen khaj".
49.
Alternatively, you can open a shell by pressing Ctrl+Alt+F2. Use Alt+F5 to get back to the installer.
2009-11-09
Teewul nga man a ubbi ab "shell" boo bëse "Ctrl+Alt+F2". Ngir delluwaat ci sampkaay bi bësal "Alt+F5".
50.
Installer components to load:
2009-11-09
ay khaj yu sampkaay bi yi niy sëf