Translations by ibrahima fall

ibrahima fall has submitted the following strings to this translation. Contributions are visually coded: currently used translations, unreviewed suggestions, rejected suggestions.

139 of 39 results
2.
Learn more about GNOME
2009-06-27
gën a xam lu jëm ci GNOME
3.
News
2009-06-27
xibaar
4.
GNOME Library
2009-06-27
Kàgguy GNOME
5.
Friends of GNOME
2009-06-27
Xariti GNOME
6.
Contact
2009-06-27
jotukaay
7.
The Mysterious GEGL
2009-06-27
Kéemtaan gu GEGL
9.
Wanda The GNOME Fish
2009-06-27
Wanda, jën bu Gnome
10.
_Open URL
2009-06-27
_Ubbi URL
11.
_Copy URL
2009-06-27
_Duppi URL
12.
About the GNOME Desktop
2009-06-27
Ci mbiri Binduwaayu GNOME
14.
Welcome to the GNOME Desktop
2009-06-27
Dalal-jàmm ci Binduwaayu GNOME
15.
Brought to you by:
2009-06-27
Ki la ko indil:
17.
Version
2009-06-27
Sumb
18.
Distributor
2009-06-27
Séddalekat
19.
Build Date
2009-06-27
Bés bees àgg
2009-06-27
Soppi taariix bi
20.
Display information on this GNOME version
2009-06-27
Woney xibaar ñeel bii sumbu GNOME
21.
GNOME also includes a complete development platform for applications programmers, allowing the creation of powerful and complex applications.
2009-06-27
Ak GNOME dees na jébbalaale it ab joyaluwaay bees jagleel tëralkat yi, tax ñuy man a bindiy tëriin yu kàttanu te fasu
22.
GNOME includes most of what you see on your computer, including the file manager, web browser, menus, and many applications.
2009-06-27
GNOME ëmbaale na lu bari ci mbir yi ne ci sa nosukaay, boole ci yorkatu dencukaay yi, joowukaayu web, njël yeek tëriin yu bari.
23.
GNOME is a Free, usable, stable, accessible desktop environment for the Unix-like family of operating systems.
2009-06-27
GNOME ab wërlaayub binduwaay la bu féex, yomb a jëfandikoo, jotale ngir xeeti nosteg doxiin yu dàttu ci UNIX.
24.
GNOME's focus on usability and accessibility, regular release cycle, and strong corporate backing make it unique among Free Software desktops.
2009-06-27
Bàyyi-xel cig yomb a jëfandikoom ak jotaleem, génnewaat yu tegu ci yoon, ak jàppaleem gu këru-liggéey yu mag tax GNOME doon kenn ci Tëriinu Binduwaay yu Féex yi.
25.
GNOME's greatest strength is our strong community. Virtually anyone, with or without coding skills, can contribute to making GNOME better.
2009-06-27
Dooley GNOME mooy askanam gu rëy. Daanaka ku ne, muy ku man walla ku manul bindi tëriin, man ngaa duggal sa loxo ci GNOME ngir gënal ko.
26.
Hundreds of people have contributed code to GNOME since it was started in 1997; many more have contributed in other important ways, including translations, documentation, and quality assurance.
2009-06-27
Ay Téeméeri nit cëru nañu ci yoonu GNOME dalee ci juddam 1997 ba léegi, ñeneen ñi ci yeneen fànn, muy tekki, uti xibaar ak ci wóoral baaxaayam.
28.
Error reading file '%s': %s
2009-06-27
Njuumte ci njàngum dencukaay '%s': %s
29.
Error rewinding file '%s': %s
2009-06-27
Njuumte ci lëmësaatu dencukaay '%s': %s
30.
No name
2009-06-27
Amul tur
31.
File '%s' is not a regular file or directory.
2009-06-27
Dencukaay '%s' du dencukaay walla dencuwaay bu baax.
33.
No filename to save to
2009-06-27
Joxoo tur dencukaay bi
34.
Starting %s
2009-06-27
Doorug %s
35.
No URL to launch
2009-06-27
Amul URL bees man a ubbi
36.
Not a launchable item
2009-06-27
Lii du lees man a ubbi
37.
No command (Exec) to launch
2009-06-27
Amulub santaane (Exec) bees war a jëfe
38.
Bad command (Exec) to launch
2009-06-27
Santaane bees war a jëfe (Exec) baaxul
39.
Unknown encoding of: %s
2009-06-27
Yoonalug %s baaxul
44.
RANDR extension is not present
2009-07-07
lawal gu RANDR nekku fi
45.
could not get information about output %d
2009-07-07
maneesul a ami xibaar ñeel génn gu %d
46.
requested position/size for CRTC %d is outside the allowed limit: position=(%d, %d), size=(%d, %d), maximum=(%d, %d)
2009-07-07
péete ak dayoo bees laaj ngir CRTC %d romb na dig bees maye: Péete=(%d, %d), dayoo=(%d, %d), bi ëpp=(%d, %d)
48.
could not get information about CRTC %d
2009-07-07
Maneesul a ami xibaar ci CRTC %d
49.
Laptop
2009-06-27
Yóbbaalewu